Distance-Jahman X-Press

Distance

专辑:Abiyo

时间:2021-11-19

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Waroma sorri

Danga sorri ci mane

Namnala yaw kagn ngey niow

Dila xaar ba souf né selaw

Dem nga yobalé samay nelaw

Laal weet mey xool fi nga doon teud

Dileu (....?....) ba assaman wéx talleu

Goudi gounék yaw rek laay guént

Motax soumay nelaw douma sawara yeewou

Distance bi taax ma silencieux

So fi nekoul xol bi dou vibrer

Sama xel mey voyager

Wax ak mane dou yombou comme kou nekk mode avion

Somay woo ma dieki dieki nopi

Xamal ni rangoogn yangui sotti

Ngay wax may deglou sa baat bi

Sorri ki nga beugga metti

Oh nam nala

Oh dama weet

Cheri yaw nam nala

Yaw guiss la sama wétt

Yaw sama ndanaane nam nala

Dangma manqué souma wakhé deug rek

Rangoogn yi dou faiblesse

Dafa fekk yaw rek la xam

Dem nga baayi ma ci tristesse

Sa parfum dess ci sama yaram

Alal dji lou neex leu

Wayé mane sa jeumm la nameu

Dara meloul ni yaw ci sa wétt

Ken dou yaw ci mane nam nala waay

Oh oh oh weet naa

Koudoul yaw mounouma wétali

Xaarit yangui niow waay té woul ba leggi

Ak waxtaan bi loumou neex neex

Degouma ci dara nam nala cheri

Oh nam nala

Oh dama weet

Cheri yaw nam nala

Yeewou guiss la sama wétt

Yaw sama ndanane nam nala

Dangma manqué souma wakhé deug rek

展开显示全部歌词