Boul Bayi-Chyco Siméon

Boul Bayi

歌手:Chyco Siméon

专辑:Boul Bayi

时间:2024-05-20

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Da ma demon

Wouti woon lo len dounde Dekke di bay

Nguir kou ne bagn mass fande

Bi yoon

Mani diekoul thi yoon Mani diekoul thi yoon

Bi yoon moom dou yoon Demal diemi banen

Andalak nianen Gueneuleuk kanen

Nit daal dafay diem lanen

Diemal gobi dounde

Del diem sa sou ne

Nala diaral daal yaw lou ne Te gua diem sakh doug fou ne

Watou lou ne Tay setloo

Boul baye

Boul baye

Boul baye li lay dolel Houwow

Boul baye

Boul baye li lay dolel

Ni beugoo kou dem

Te beugo nit koufi tekki itam

Deuke di fen

Mani roussouloo setlou woo gni lay sen di la setlou Roussouloo setlou woo say nawle yi lay sen Nangou woo deglou woo gouba teukh lou di dem Dieul sa yonou mbon

Roussoulo domi adama

And ngaak nianen do bayeti nak Fasouloo diogue thi li

Do bayi loudoul gua de

Te man mi nena la

Boul baye

Boul baye

Boul baye li lay dolel Houwoo

Boul baye

Boul baye li lay dolel Houwoo

Boul baye

Boul baye li lay dolel Houwoo

Boul baye

Boul baye li lay dolel

Baye - Baye - Baye Baye Yelelelele le lee

Lili lile

Wouyoho

Ndaw daal war nguay diem khol Lanen loudoul kharitook sinebar

Hunn beugou loo dem

Beugou loo ken dem ha

Digua mass sooy

Mani roussouloo setlou woo gni lay sen di la setlou Roussouloo setoulou say nawle yi lay sen

Nangou woo deglou woo gouba teukh lou di dem Dieul sa yonou mbon

Roussoulo domi adama

And ngaak nianen do bayeti nak Fasouloo diogue thi li

Do bayi loudoul gua de Temanminenala

Boul Baye Hannnn

Boul Bayi lilay dolel

Nit koune war naa kham li gueun thi moom

Adouna ni la

Nagua daw kou la yey

Nagua daw nit gni togge di la yedd

Boul baye

Boul baye

Boul baye li lay dolel Houwoo.

Boul baye

Boul baye Houwoo.

Boul baye

Boul baye Houwoo

Boul baye

Boul baye

li lay dolel li lay dolel li lay dolel

Adouna ni la

Kholal thi say nawle kholal thi say mass Nguir gniou bagn la yedd

展开显示全部歌词