Fouma Nek-Owane

Fouma Nek

歌手:Owane

时间:2022-03-10

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Gnogui mettit lou lima rare

Gnougui fi di lathié owane foumou neh

Neh len magui si djam yeah magui yeah magui thi sama boppou

Chaque Souba tel tal sama téléphone guiss ay message youdoul djekh nam nagnou li ngay defff

Deloussil nga dampp xol yi té nga boyal sougnouy nopou

Kou done lathié falli ngoya ngui

Gallo teggal caisse yi gnou dem

Gnogui mettit lou lima rare

Gnougui fi di lathié owane foumou neh

Neh len magui si djam yeah magui yeah magui thi sama boppou

Amna Rap Amna life Beugouma deff Rap sama life

Nane lay deff ba teral family bala li di death

Djante bé gui may tiimmm fou billet di roffo samay down

Fier thi sama job takhna gnanouma ken financer sama bop

Sant Yalla magui dagg boumou gathié yi

Si mane li geuna kharam beug lall ak bagna ligueyi

Échec mom la raggal mane deh moma geuna deffar ni

Raggal lou metté khagn sa bop weurseuk bi la God fintél

Gnogui mettit lou lima rare

Gnougui fi di lathié owane foumou neh

Neh len magui si djam yeah magui yeah magui thi sama boppou

Fou game bi tolou wakh ma gaw ma dabé way

MC yi sonou gno fi neh batay di bakkou

Sa yaye rouss nala wakh ni bayil li dou pour yow

Say Xaritt rouss nagn la wakh ni adjoul li ni ayooo

Gnom gnio tal fay na ki ak keulé

Kossi lathi amoul loumou taalé sen tchinou keur

Xolou mougn mom dou mom nguen manquer yah

Bou wèsso Rap bi mane magui fé di get Paid

展开显示全部歌词