Dou Nonou (Explicit)-Canabasse

Dou Nonou (Explicit)

歌手:Canabasse

时间:2020-08-07

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Hook

Non non dou yomb

Danga am sa guiss guiss mane ma am sa boss pour niou diouyo dey yomb

Ma am noumay dokhé nga am ningay dokhé

Sougn ande dou yomb

Xol nagn founé ba sougnouy beut dadjé

Dokh nagn ba kou nek si nioune guissna dall bouko diot niou fass yeneko takk dokh

Mais dou yombé nonou girl

Ndax beusseungui ci beuss yi kou nek dina took di rethiou loutax mou denk kenene ki bopam

Satan dey sarr souniou bopp

Sëy yombé woul nonou girl

Et ce serait dommage niou aksi fi

Si ndigalou God ba am ci fille

Té douniou nangou def ay sacrifices

Souko defé dou yomb

No (x4)

Gueum ma girl li am moy bougn ko defoul dou yomb

Yeah finiou dieum sorina lool wax djou sew dji warone nagnou diomb

Deug leu bokougnou guiss guiss wayé mak ioe nio bokk lign tchiy hol

Yea bokougnou dokhine mais mak yaw nio bokk meme destination

Verse

Nitou diamme la girl walay khawma fitneu

Mais bo dougué samay 18 carton rouge mofi seuss

Soma dokhaté ma dayla neek bi xeegn neu khouneu

Tay si salle bi laay fanane setane telé ba xeum

Yewou fajar niane yalla mana mouri say beut

Ndax bodone guissé fimay guissé dina tané xeuyneu

Yeah bodone degg fimay waxé sama baat dou mass diouk

Ba deukeu ndoo yi diniou degg xam lou xew souniou keur

Nagn xam li xew souniou keur

I dont give a ****

Effort biniouy def si kanamou nit yi di nguisteul

Bougn ko defone si mak yaw happiness dougnou teu

Bougn ko defone si mak yaw dougnou yendo di keudj

Kone sa laakh bou taangué ngala eupi djiko

Ndax boy dokhé tankou yaax mala eup djiko

Liy sene si gaal gui sougn kou fatiul dina weulbeutikou

Niou moudj dieul photo de famille yeup keupeutiko

Hook

Non non dou yomb

Danga am sa guiss guiss mane ma am sa boss pour niou diouyo dey yomb

Ma am noumay dokhé nga am ningay dokhé

Sougn ande dou yomb

Xol nagn founé ba sougnouy beut dadjé

Dokh nagn ba kou nek si nioune guissna dall bouko diot niou fass yeneko takk dokh

Mais dou yombé nonou girl

Ndax beusseungui ci beuss yi kou nek dina took di rethiou loutax mou denk kenene ki bopam

Satan dey sarr souniou bopp

Sëy yombé woul nonou girl

Et ce serait dommage niou aksi fi

Si ndigalou God ba am ci fille

Té douniou nangou def ay sacrifices

Souko defé dou yomb

No (x4)

Gueum ma girl li am moy bougn ko defoul dou yomb

Yeah finiou dieum sorina lool wax djou sew dji warone nagnou diomb

Deug leu bokougnou guiss guiss wayé mak ioe nio bokk lign tchiy hol

Yea bokougnou dokhine mais mak yaw nio bokk meme destination

Verse

Degn ko hustle ba degg diam confort matériel

Keur gui meunone neu gueneu naate ndax manqué wougn lene

Climatiseurs yi nioungui takk frigo yeup fess deel

Wayé tay xol yi nioungui tang

Ndax patience bé dieex

Oh oh

Oh oh

Tay xol yi nioungui tang

Ndax patience bé dieex

Sa système dafa wara topp sama système

Pour nga appliquer warouma am sax pour insister

Dou caprices dé mais rôle bi moy may wax ngay degg

Si negou seuy goor bi mome moy capitaine

Sama respect ci yaw

Dou tax autorité bima yalla may sa kaw ma bayiko mala yilif yea

Si mbed bi wanel sa bopp dawalal parité

Mais ci biir keur gui seyal ci mane ndox ak xorom doone guedj

展开显示全部歌词