Begue (Explicit)-Annas

Begue (Explicit)

歌手:Annas

时间:2026-06-21

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Refrain 1 (x2)

Begue bi nexx na ndeysane, atjieu lene niou begue way

Yaye sama way Kay niou begue

Atjieu lene niou beugueu wayé

Couplet 1

Amana dangey tok sa khel di say di mind, forget your problems daniouy bègue never mind

Djeuleul ass positif bi nek sisa mind

Nieuw niou begue ayway begue

Amana dangey tok sakh yene say di stresser amnga sa gayne âme say mboki talibé

Djelel sa positivity def ko sa gayne nieuw niou begue ayway

Refrain 1 (x2)

Begue bi nexx na ndeysane, atjieu lene niou begue way

Yaye sama way Kay niou begue

Atjieu lene niou beugueu wayé

Refrain 2

Yaaw ya teki mbiskit djalakh ko mou danou bonbon seug di djoy nga napadje ko

Wowilene soukeur bala mbouro djexx tandarma djale ko

Sama chérie wouteul nama lal motel mako xamnga souma dewoul dina boot sa dome roguanti tam tamal neko noopil lingey bege sa yaay yeup mala raw doom nanou yengel gessem

Refrain 1 (x2)

Begue bi nexx na ndeysane, atjieu lene niou begue way

Yaye sama way Kay niou begue

Atjieu lene niou beugueu wayé

Couplet 2

Naxx Binou ekse terou nganou teraal nganou acceuillir nganou ba heurou gnibi djoot nga ne yaay néné yengel gessem

展开显示全部歌词