COSAAN-Yoro Ndiaye

COSAAN

歌手:Yoro Ndiaye

专辑:YAAY KAN

时间:2024-06-27

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Cosaan

Nañu fonk suñu cosaan,def ko ni ndokh ci ndaa so maree tankh naan

Mooy doole ndanaan

Fonkal nee di laal ci baaxi maam

Soo reree laac ko maam mu wax la linga moom

Ku xeep sa nguuro doon badola boo fattee linga moomee reer yomb la

XIIn jipp Baol jokk baal faal ba jaayu,mag ña doon taaxuraan baol lañu cosaano

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Junjung yaa nga siin ,

ndaga saloum ma ko moom,

fouta naabe yeela

Nañu dem ba Casamance ,tamba ba Kolda bugarabou balafon Soruba ñooy boroom

Sunu cosaan,sunu cosaan yaatu na

Bargny guethie gumbe leen teunguethie ngor ouakam ndakaru ndiaye

Sunu cosaan sunu cosaan yaayu na

Nañu fonk sunu cosaan def ko ni ndokh ci ndaa soo maree tankh naan moy doole ndanaan

Fonkal sa cosaano,di laal ci baaxi maam soo reeree laac ko maam mu waxla linga moom

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Bul di fattee li nga moomee ,fanga jogguee ak langa doonee

Boo flattée demb rer yomb laa,ëppnaa fattee bulko fattee yoow

Yaw mi maam boy,yaw mi fekke demb ñewal nettali ñoo

Ndax ñu naan ,demb takh ñu naan tayjilee bul ko faatee yaw

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

展开显示全部歌词