Free World (Explicit)-Cheeks

Free World (Explicit)

歌手:Cheeks

时间:2020-08-07

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Hook

Free world

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Free world

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

(X2)

Verse

Adouna bi dafa diéki diéki soupaliko nek bene genrou free world

Gniniou djité guemeutou niou sax yalla kone lou ci sene yoon ci souniou sort

Té la loi du plus fort laniouy appliqué si nio hamné amouniou doolé

Bour yallah moungui xaar

Nioune dé tamit nioungui xaar jour bimouy wané doolem

Beuss negn changer décor

Ndax té liniouy dound fii mom dafa hardcore

Sa destiny si loxo kaatior

Balay adouna di touki niokay wouteul passeport

Motax may deglou sama yaye boye

Beug guestou teré yi ba melni sama baye boye

Di moytou def kat ak wax kat

Def tate ak fene kat fi dafa tiool

Hook

Free world

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Free world

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

(X2)

Verse

Loutax ay quelques nitt kecé nioy décidé

Dama beug know

Gni niou beug diapalé diéki diéki décédé

Dama beug know

Police di tapalé enquête dou continuer

Dama beug know

Beug nek dirigeant té dirigé go sa bopp

Danga diéki diéki guiss kene au top

Do ham foumou diougué si ay neew la tok

Niom niolay handiou mew world order

Paré xagnla courant tioop ak water

Yaw ma bagn damay tekk boy

Nioungui sama kaw depuis game boy

Douma sol piinw damay check boy

Xamnga fima diaar dafa teng boy

Nèkal Pharaon ma nek sa Moïse rek

Mancha Hercules africain la douma grec

Jump up in da club took di science boy

Xamné adouna beug leu mo gueun beug adouna

And ak samay niggers and ak sama sago

Gni gueum lima gueum no dougnou meusseu tago

Ani noy def ba tathiou ak bene lokho

**** up samay dreams ibliss diemone nako

Mais god is great yea super great

Falewouma 33e degrés

Douma paniquer

Sarax charité

Tolo ak souf ci man

Nigger loloy parité

Adouna bi dafa diéki diéki soupaliko nek genrou free world

Gniniou djité guemeutou niou sax yalla kone lou ci sene yoon ci souniou sort

Té la loi du plus fort laniouy appliquée si nio hamné amouniou doolé

Bour yallah moungui xaar

Nielé tamit nioungui xaar jour bimouy wané doolem

Hook

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Free world

Adouna bou bess takk

It’s the new world

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

Tolok souf ci dound zero soucis my man

Bo topoul si sa diné dina yemé

Free world hmmmm

Free world hmmmm

展开显示全部歌词