Si Gawaay-Jahman X-Press

Si Gawaay

专辑:Abiyo

时间:2021-11-19

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Soudé foo mola takha diouk yaw wakh ma ko leggi

Mongui beug yagg té defo fouleu ba leggi

Lou baakh kene douko waadj yaw

Kone nak gaawal ci mane

Khol ma ci kaaw ba ci souff

Wakh ma lou manqué ci mane

Niouni ma miin nala maak yaw khamanté nagn

Guéneu bou amoul foumouy yam lolou mane doumako meune

Letoulo ma firi woma waay defal lou khess

Ndel ma sakh ni Abba mo gueune ngamay tekk stress

Rétane you bari youma néké tayoumako

Damla nopp té khaar bou yagg bi meuneutou mako

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Néko rang mouy gaaw waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay

Doro faayou woo waay

Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , waay waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , waay waay

Même soudé yangmay defal adunaak li ci biireum

Nga deff foulaa mako gueuneul

Soudé foulaaa leu dougueul ci mane

Nagn dem VAR

Mane dama beug done sa Halal

Né nga bokoulok niom kone nak defal différence

Diaye diomba niaaw bi damay sonal

Mbeuguel bou deugou andaak lokhoy kessé damey doundeul

Boumaak nioniou alall sonal

Douma Coumba Gawlo tidjil ma ndakh mangui feugueu

Saa sounek mangui daaw ci sa ay beug beug

Gawal gawal ci mane ,khana dotoul deug ?

Mongui beug waay daal ci deug deug

Bayil feemou bi nak !

Dokhane bi doyna nak !

Daaw ba réne ngey dougou gueneu

Wakh niou kagn ngey niow takk

Bayil feemou bi nak !

Dokhane bi doyna nak !

Daaw ba réne ngey dougou gueneu

Wakh niou kagn ngey niow takk

Gaawal mba ngey loukhouss

Baniouma sa poukhouss

Auto you cher gallé you nice

Kholouma (.......?.....)

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Neko rang mouy gaaw waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay

Doro faayou woo waay

Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , waay waay

Ci gaaway waay , Ci gaaway waay

Ci gaaway waay , waay waay

展开显示全部歌词