Sama Cas-Jahman X-Press

Sama Cas

专辑:Abiyo

时间:2021-11-19

    使用手机浏览器「扫一扫」

    在手机上保存,获得更好体验

标签
歌词

Pousseul boulma yakkal sama noce

Fii kou pissoul yangui (...?...)

Xana mane ngen guiss sama boss

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Né fess

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Yo bala nioumay cas

Ma cas sama bop

Diem diegalou toub

Samay bakkar bagn ma topp

Meune nga fenn sa bop mai meuno neubeutou God

Dieuli less waxoul fi kou weet xam sa bopp

Wakho li ngay deff

Defo li ngay wax

Cas bi dineu leer

Sa bopp ngay nakh

Meuss nga deff lou bonn xalaat ko tiit té yallah takh

Diot na fatelikoul xamnga boudé yangui baax

Niodi sey di weddi daadjou naan té diné dooy na croix

Mane mom damay deff mais kounek ak sa cas

Mane la am dou mane

Defou mako dagn ma djiiin

Loy setal sa bopp lekoulo ko

loutax nga niine ?

Pousseul boulma yakkal sama noce

Fii kou pissoul yangui (...?...)

Xana mane ngen guiss sama boss

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Né fess

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Ndioumté dou wess

Té douma blanche neige

Amna lou yallah téré

Té mangkay deff

Fenn a gueuna boon

Té yaa ciy chef

Fi kounek ak sa paan ak lo ciy deff

Gueneul sou waxoul deug wakhi fenn

Sou goudi teudone laal nga (...??..)

Def na louma beugoul keneu xam

Wowema ibliss boudé kou def erreur danga boon

Eh neko ci bou goudou

Yangui ci bou gatteu

Ladjouma no toudou

Lidjeunti wouma sa deff tattt

Li ngay xool ci mane mongui ci yaw

Noko guissé ?

Wathie daanou mo ci gueune gaaw

Meunoma juger

Pousseul boulma yakkal sama noce

Fii kou pissoul yangui (...?...)

Xana mane ngen guiss sama boss

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Né fess

Bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Dem teudi

Eh bala nioumay cas mane ma cas sama bop

Né tiiirrrr

Meune nga waat ni meusso biii ?

( Ah louma ci xam ...)

Meune nga waat ni meusso béé ?

( coté yoyou la rek .. )

Fi ken nekoul mousso iiihhhh ?

( meune na nekk deh..)

Lou ken yeugoul mousso eeeehhh

( lool la bo démé )

展开显示全部歌词